Ismael Lo - Jammu Africa Ismael Lo - Jammu Africa From the Album of the same name the wonderful Ismael Lo from Senegal. Afrika a a a Afrika mon Afrique Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix Kon jammu Afrika moom lay ñaan Mané jammu Afrika mooy suñu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères Kon jammu Afrika moom lay ñaan Mané jammu Afrika mooy suñu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi Yoo Alla addu jam to Ruanda Yoo Alla addu jam to Burundi Yoo Alla addu jam to Casamans Lawol Mbignona yee Traduction (les deux premiers couplets sont en wolof, le dernier est en Pulaar) Dans mon rêve je prie Dieu pour que cela se réalise avant mon trépas Je dis " un jour viendra où l'Afrique sera unie " D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix Donc je demande la paix en Afrique car avec la paix en Afrique ce sera la prospérité Etranger, moi Lô je te prie quelles que soient ta fortune et ta situation de ne pas oublier l'Afrique Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères Donc je demande la paix en Afrique car avec la paix en Afrique ce sera la prospérité Vous les enfants d'Afrique, levez-vous pour construire notre pays Que Dieu nous épargne les malheurs Qu'il apporte la paix au Rwanda, au Burundi, Et en Casamance sur la route de Mbignona!!! From: zamione Views: 146579 138 ratings Time: 05:02 More in Music published_at Wed Sep 26 19:46:49 UTC 2007 keywords: jammu, lo, ismael, africa, senegal duration: 00:05:02